mardi 9 août 2011

Ngan ci addina (Visiteurs sur la terre, sojourners on earth)

 "Gannaaw nag Yàlla, mi ngeen di wooye Baay, mooy àtte jëfi ñépp te du gënale kenn, saxleen ci ragal ko diirub seen ngan ci àddina." 1 Piyeer 1.17

" Dans vos prières, vous appelez Père celui qui juge impartialement tout homme selon ses actes. Par conséquent, pendant tout le temps qui vous reste à passer dans ce monde, manifestez par votre manière de vivre que vous le révérez." 1 Pierre 1.17

If you address as Father the One who impartially judges according to each one’s work, conduct yourselves in fear during the time of your stay on earth;

2 commentaires:

  1. En lisant ce verset ce matin, j'ai réfléchi sur ce que la culture Wolof dit sur l'étranger (ngan en Wolof) et comment cela pourrait s'appliquer ici.

    While I was reading this verse this morning, I thought avout what the Wolof culture says about the foreigner (ngan in Wolof) and how it applies here.

    RépondreSupprimer
  2. Na nu bayi xel ci kaddu gi itam: Waaye teewul fondamaa bu dëgër, bi Yàlla tabax, nee na kekk, te lii lañu ci tàmpe : «Boroom bi xam na ñi bokk ci moom,» te it : «Ki tudd turu Boroom bi, na daw lu bon.» 2 Timotee 2.19

    RépondreSupprimer